Xibaar

FUTBAL AK JAFE-JAFEY RÉEWI AFRIG YI

Doom-aadama fent na ay xeeti po yu bare. Ba ci tàggat-yaram sax, nga xam...

LÀNGU FAY-SÀLL-TIMIS : PETOROL BAA NGI XASAW XUNN

Suweŋ2011, réew mépp màbbandoo wutali « Place Soweto » ngir xeex sémbub àtte bu Njiitu-réew ma...

MBAY JAAG, GOR BI SENEGAAL AMEEL BOR (Xaaj bu njëkk)

Xel tëju na, xalaat dëju. Xol tooy na, bët jooy. Ndeysaan… Gaynde wàcc na liggéey....

JIGÉEN DU XARU TABASKI !

“DOY NA !”, “DAFA DOY !”. Ñaari baat yii mën nañoo tënk doxu-ñaxtu bi...

ÑÀKK KAYITU-JUDDU GI NAG, BA KAÑ?

Ayu-bés yii weesu, yéenekaay yu bare dañoo xéy fésal ci seen xët bu njëkk...

CI GÀTTAL, XIBAAR YI GËN A FÉS CI AYU-BÉSUG ALTINE 27 JÀPP ALXAMES 30 ME 2019

#Diisoo ñeel réew mi Diisoo bi Njiitu-réew mi, Maki Sàll, woote woon door na ci...

LU ÑUY XAAR CI JÀNGALE LÀMMIÑI RÉEW MI ?

Bi Senegaal moomee boppam ba tey, bare na ay nguur yu fi jaar ak...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...