FMI RAFETLU NA DOXALINU CÀMMUG SENEGAAL GI

Yeneen i xët

Aji bind ji

FMI rafetlu na luññutu gi njiiti Senegaal yu bees yi amal ñeel koppari réew mi. Rafetlu nañu itamit li Njiitu réew mi, Bassiru Jomaay Fay, ak nguuram gi am yéeney yore réew mi ci anam yu leer te lalu ci dëgg.
Ci kow loolu, ñoom waa FMI, nee nañ dinañu liggéey ak Càmm gi ci ayu-bés yii di ñëw ngir natt njeexital yiy am ci wàllu koom-koom gu yaatu gi te samp jéego yi ciy topp.

Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj