Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

UMS DÀNKAAFU NA MEETAR MUSAA BOOKAR CAAM

Kurélu àttekat yu Senegaal gi, UMS, ñaawlu na taxawaayu Meetar Musaa Bookar Caam ginnaaw bi mu juree àttekat bii di Idiriisa Jara ci mbiri...

AAMADU BA (JËWRIÑU MBATIIT MI) : « MBATIIT, DAFAY JUBOOLE TE DI SAXAL WÓOLOONTE »

Jëwriñu Mbatiit* mi, Ñeeñal* gi ak Wërteef* gi, Aamadu Ba mu Pastef, teewoon na ndajem saabal mees jagleeloon Xumbeenu* pasin* ak mbatiit mu Afrigu...

KUBALI GALAG YI : NGUUR GI DAJALE NA 3 000IY MILIYAAR

Nguur gi siiwal na caabalug doxal ñeel nafa gi ci juróom-ñeenti weer yi njëkk ci atum 2025 mi. Caabal googu nag dafa biral i...

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu jiboon, lëmbe réew mépp. Nde, ñaari sóobare yooyu, dañu jékki...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen digganteek Beresil. Ñu jóge fa ñàkk woy wi ñu amoon...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar giy liggéey ay bunt ak i palanteer fa Jamñaajo. Ci...

NAFAG 2026 : JAGLEES NA 356 MILIYAAR NJËWRIÑU YAXANTU BEEK NDEFAR GI

Njiiti Senegaal yi dañu bëgg a jël fànnu ndefar wi, def ko xolu koom-koomu réew mi. Ci atum 2026 mii lañu bëgg a tàmbalee...

BÉSUB SÓOBARE YI : NJIITU RÉEW MA RAFETLU NA TAXAWAAYU SÓOBARE YI TE BOOLE LEEN CI POWI JOJ NDAKAARU 2026 YI

Ci altiney tay jii, 10i nowàmbar 2025, la Senegaal doon màggal Bésub  Sóobare yi. Wëppa wees jagleel bés bi nag mooy : « Sóobare yi, farandooy...

COP 30 : ABDURAHMAAN JUUF FEDDALINA TAXAWAAYU SENEGAAL

Jëwriñ jii di Abdurahmaan Juuf yékkati na ay kàddu fa Beresil ngir dëggal taxawaayu Senegaal ci xeex yàquteg jaww ji. Dafa teewaloon Njiitu réew...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (6/11/2025)

PRODAC : YOON TÉYANDI NAÑU Tay ci ngoon la takk-deri DIC yi fekki Paab Maalig Nduur këram, daldi koy jàpp, yóbbu ko. Bees sukandikoo ci sunu...