LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (4/12/2023)

PÓLITIG Bu amee ñu doon laamlaame wotey 2024 ndax dees ko war a dàq am déet, mënees na jàpp ni wote yi dinañ am ci...

Top News

Africa

spot_img

Europe

Barki-démb ci gaawu gi la ko Rimtalba Jean Emmanuel Ouédraogo xamle ci ab yégle. Moom Jean Emmanuel di ki yor kàddug Nguur gi (porte-parole) moo biral ne kibaaraanu Farãs googu di “Le Monde” amatul sañ-sañu génnee...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (3/12/2023)

COOWAL CAN LI Afrig moom, dafa mel ni ndeyam liggéeyul. Saa bu CAN bi jubsee, coow li jib, ñuy ŋëwti-ŋëwti joŋante bi. Te, bu "Euro" bi jotee, kenn du dégg coow ñeel ko. Waaye bu Joŋantey Afrig...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (3/12/2023)

Pólitig Ëttu àttewaay bu mag bi gàntal na neenal-àtte bi layookati sonko yi sàkku woon ngir ñu saytuwaat dogal ga mu jëloon ñeel Usmaan Sonko ci wotey 2024 yi. Seex Baara Dolli bokk ci wutaakoni (lawaxi) wotey 2024...

Asia

spot_img

Bussiness

Politics

PÓLITIG Bu amee ñu doon laamlaame wotey 2024 ndax dees ko war a dàq am déet, mënees na jàpp ni wote yi dinañ am ci bés bees ko jàppoon. Njiitu réew mi Maki Sàll xaatim na dekkere...

BURKINAA FAASO : AAYEES NA YÉENEKAAY LE MONDE

Barki-démb ci gaawu gi la ko Rimtalba Jean Emmanuel Ouédraogo xamle ci ab yégle. Moom Jean Emmanuel di ki yor kàddug Nguur gi (porte-parole) moo biral ne kibaaraanu Farãs googu di “Le Monde” amatul sañ-sañu génnee...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (3/12/2023)

COOWAL CAN LI Afrig moom, dafa mel ni ndeyam liggéeyul. Saa bu CAN bi jubsee, coow li jib, ñuy ŋëwti-ŋëwti joŋante bi. Te, bu "Euro" bi jotee, kenn du dégg coow ñeel ko. Waaye bu Joŋantey Afrig...
spot_img

Science

Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Sports

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (4/12/2023)

PÓLITIG Bu amee ñu doon laamlaame wotey 2024 ndax dees ko war a dàq am déet, mënees na jàpp ni wote yi dinañ am ci...

BURKINAA FAASO : AAYEES NA YÉENEKAAY LE MONDE

Barki-démb ci gaawu gi la ko Rimtalba Jean Emmanuel Ouédraogo xamle ci ab yégle. Moom Jean Emmanuel di ki yor kàddug Nguur gi (porte-parole)...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (3/12/2023)

COOWAL CAN LI Afrig moom, dafa mel ni ndeyam liggéeyul. Saa bu CAN bi jubsee, coow li jib, ñuy ŋëwti-ŋëwti joŋante bi. Te, bu "Euro"...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (3/12/2023)

Pólitig Ëttu àttewaay bu mag bi gàntal na neenal-àtte bi layookati sonko yi sàkku woon ngir ñu saytuwaat dogal ga mu jëloon ñeel Usmaan Sonko...

ËTTU ÀTTEWAAY BU MAG BI : NJIIT LA GÀNTAL NA NEENAL-ÀTTE BU LAYOOKATI USMAAN SONKO

Ëttu àttewaay bu mag bi gàntal na neenal-àtte bi layookati Usmaan Sonko yi dugaloon. Fekk ñu tàbbaloon ko fa ñeel neenalub dogal bi àttekat...

LI GËN A FË CI XIBAARI BÉS BI (1/12/2023)

JËWRIÑU NGURD MI JOXE NA KÀDDOOM Démb la Ngomblaan gi doon jeexal ndaje yi mu doon amal ak jëwriñi Càmm gi. Def nañ 32i fan...

AYIB DAFE A NGI YEDD CDC

Bu Usmaan Sonko bokkee ci wotey 2024 yees dégmal de, dina doon jaloore ju réy. Nde, 2021 ba léegi, Nguurug Maki Sàll gaa ngi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (30/11/2023)

LI BEES CI NDOGAL LI ËTTU ÀTTEWAAY BU KOWE BI JËLOON Ci talaata ji la layookati Usmaan Sonko yi jébbal waa ëttu àttewaay bu kowe...

LAYOOKATI SONKO YI DUGAL NAÑ AB NEENAL-ÀTTE

Ginnaaw bi ëttu àttewaay bu mag bi neenalee woon àtteb Sabasi Fay ba, keroog àjjuma17 nowàmbar 2023, layookati Sonko yi, ba léegi, xàddeeguñ. Nde,...

JALOOREY RAGLUB SÓOBARE BU WAKAAM

Senegaal séqi na jéego bu am a am solo ci wàllu paj. Nde, doktoor ya ca raglub sóobare ba ca Wakaam, maanaam loppitaanu soldaar...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (27/11/2023)

WOTEY 2024 YI Li des ci wotey 25 féewaryee 2024 yi yées na ñetti weer. Waaye, am nay lawax yu féete ci kujje gi yuy...

AY CONGU CI YENN BÉRÉB FA SIYERAA-LEWON

Njàqare ak tiis la askan wa dëkke fa Freetown yeewoo démb. Ay sàmbaa-bóoy ñoo song béréb yu bari fa gëbla ga. Muy koñ bii...