Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

KAN MOOY ISAA SÀLL ?

« Jàpp naa ne pólitig du liggéey, jàngale mooy sama liggéey » (Isaa Sàll) Isaa Sàll, ab wutaakon la ci wote palug njiitu réew mi ñu dégmal, bésub...

SIGARET BAAXUL… WAAYE AFRIG LA YÉESE !

Fan yii weesu, Marie Maurisse, ab taskatu xibaar bu fekk baax Siwis, bind na bataaxal bu jar a bàyyi xel. La muy ciy nettali...

DÉMB SEŋOOR, TEY WÀDD

Li ko dale atum 1978 ba tey jii, woteb ren bii mooy wote bu fi njëkk a am te Ablaay Wàdd sampu ci ndëndam....

AYSATA TAAL SÀLL : JIGÉEN SOPPAL TE BUL WÓOLU…?

Bés ba ma ko déggee mu naan kilifa diine yi dañ maa ñaan ma fekki Maki, laa ni ci sama xel : Aysata mii de,...

DI BUUR, DI BUMMI

Li jaaxal waa Senegaal, mooy wax-waxeet yi kilifay réew mi dëkke. Ku ci jóge ci kujje gi, dem ci nguur gi yaa ngiy xas...

KAN MOOY… IDIRIISA SEKK ?

Maaraa la ko ay jegeñaaleem di woowe, doomi-réew mi naan ko Idi. Taskati xibaar yi ñoom, Ndaamal-Kajoor lañu koy dàkkentale. Idiriisa Sekk — mooy turam dëggëntaan — dib pólitiseŋ bu ñu ràññee...

KAN MOOY…MAKI SÀLL ?

Ci Baatu Majaw Njaay Aw askan, bala moo tànn njiitam, war naa seet bu baax jikkoom, seetaat ko, xam mooy kan. Looloo waral Lu defu waxu,...

Bàlla Gay-Móodu Lóo : ñaar ci dara

Làmbu démb ak ju tey jeeka wuute ! Ndege, démb, bu nawet bi wàccaan, ci lañu daan tëgg làmb. Kon, nu gis ne ci njeexitalu...

XËCC BU DAŊEE DAGG !

Nimbir yiy doxe diggante nguur geek kujje gi bi Màkki Sáll toogee ci jal bi ba tey jii, dalul xel dara. Nun ñépp a...

DIBÉERU WËLBATI

Cialtine jii la njiitu réew mi doon jébbal askan wi saxaar gi ñu duppe TER. Waaye, laata looluy am, ndajem-ndeyu-àtte mi, siiwaloon na ci...