Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

« MËSUNOO GIS BOR BU ÑU NËBB BU TOLLU NII CI AFRIG », EDWARD GEMAYEL, NJIITU NDAWI FMI FI SENEGAAL

Nees ko biralee woon ci sunu yaxalu barki-démb bi, ndawi yi FMI yabal fi réew mi dañu toogaat ci réew mi ngir wéyal liggéey...

LIGGÉEY BAA NGI WÉY DIGGANTE FMI AK NGUURUG SENEGAAL GI

Waa FMI dinañu toogaat ci réew ay fan ngir wéyal liggéey bi ñu sumb ak Nguurug Senegaal. Bésub 22 oktoobar 2025 lañu ñëwoon Ndakaaru...

CAABALUG ARCOP 2022-2023 : 3,2 MILIYAAR YU NE MËY !

ARCOP (Autorité de Régulation des Marchés Publics), di banqaas biy saytu lépp lu aju ci yoonalug jawi bokkeef gi, siiwal na caabalug ati 2022-2023...

8eelu NDAJEM GALIEN AFRIG : CÀKKUTEEFU NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi woote na jëme ci Afrig mën boppam ci wàllu paj mi. Muy woote bu mu amal fekk mu doon jiite xew...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI 30/10/2025

TÉYANDI NAÑU AMET NDÓOY Amet Ndóoy, kenn la ci koronikëeri Sentv yi. Moom nag, dañu koo téyandi fa “Brigade de Recherche bu Faidherbe”. Moom nag,...

MBIRUM MAJAMBAL JAAÑ : YOON TEG NA LOXO MAYMUNA NDUUR FAY (7TV) AK BAABAKAR FAAL (GFM)

Démb ci guddi, Maymuna Nduur Fay dafa bëggoon a dalal Majambal Jaañ ci jotaayub laaj-tontu, foofa ca teleem bii di 7tv. Waaye, sàndarm yi...

USMAAN SONKO YÉENE NA WÀÑÑIB MBËJ GI, NJAFAAN GEEK GIL BI

Càmm gaa ngi ci tànki wàññi njëgi mbëj gi, njafaan gi, gil bi ak njureefi soroj gi. Ci altiney tay jii la elimaanu...

COOWAL BOR BI ÑU NËBB

Coowal bor bi ñu ne Nguurug Maki Sàll dafa ko nëbboon a ngi wéy di gën a jolli ci dëkk bi, ginnaaw bi layookati...

TÉYANDI NAÑU PAAB MAALIG NDUUR (APR)

Tay lañu woolu woon Paab Maalig Nduur, nekkoon jëwriñ ca nguurug Maki Sàll ga woon, bi 16i waxtu jotee ci ngoon, fa màkkaanu banqaasu...

2026 : SENEGAAL A NGI SÓOBU CI SÉMB YU MAG YI

Ginnaaw bi ñu defee at ak lu teg, Càmmug Basiiru Jomaay Jaxaar Fay gee ngi waaj a song sémb yu mag yi ngir tabax...