Sëriñ Muntaxaa Mbàkke, Xalifab murit yi, dalal na waa Yewwi Askan Wi. Ca seen ndaje ma, jox na leen ay tàndarma yoy, Usmaan Sonko la ko jagleel ngir mu dakkalee leen xiifalam gi. Abiib Si moo ko xamle.