Li fës BAKKAN ROTAAT NA FA GINNAAW RAAY By Paap Aali Jàllo 10/02/2024 0 210 Partager FacebookTwitterWhatsAppE-mailImprimer Yeneen i xët BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI Njuga Gay - 17/12/2025 COKKAASU ODIA Odia - 15/12/2025 BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO Ndey Koddu Faal - 15/12/2025 COKKAASU ODIA Paap Aali Jàllo - 08/12/2025 Aji bind ji Paap Aali Jàllo Ginnaaw ndongo la gaañu fa jànguneb Ndar, beneen ndaw ñàkk na bakkanam fa Ndakaaru. Móodu Géy, amoon 23i at, lañu dóor balu fetel ci biir bi. Biñ ko rawalee loppitaal la mujje faatu, démb. Ay mbokkam a siiwal xibaar bi. Paap Aali JàlloPlus de publicationsBiographiePaap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/COKKAASU ODIAPaap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/USMAAN SONKO : « JÀMM REKK LAA SÉQ AK JOMAAY… LIGGÉEYALUMA JOMAAY, SENEGAAL LAAY LIGGÉEYAL. »Paap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/GINE BISAAWO | WOTEB FAL NJIITU RÉEW : FERNANDO DIAS DA COSTA MOO JIITOOGUMPaap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/AAMADU BA (JËWRIÑU MBATIIT MI) : « MBATIIT, DAFAY JUBOOLE TE DI SAXAL WÓOLOONTE » FacebookTwitterWhatsAppE-mailImprimer Widewo VOA AMAL NAB JOTAAY CI MBINDUM BUBAKAR BÓRIS JÓOB GINNAAW BI WEREKAAN BI JËLEE CARGALUG NEUSTADT 2022 BI. CUQAL CI LËNKAAY BII TOFTALU... Defu Waxu - Xët yi mujj