Li fës MA-DEMBA SOKK WUYUJI NA BOROOMAM By Paap Aali Jàllo 15/06/2024 0 194 Partager FacebookTwitterWhatsAppE-mailImprimer Yeneen i xët MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER » Mbay Sow - 17/11/2025 FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI Njuga Gay - 16/11/2025 JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER Mbay Sow - 13/11/2025 COKKAASU ODIA Odia - 13/11/2025 Aji bind ji Paap Aali Jàllo Xibaar bu tiis la réew mi xëyee tey. Ma-Demba Sokk moo génn àddina. Pari ga mu doon fajoo, ca Farãs, la gaañoo. Mi ngi amoon 65i at. Ma-Demba Sokk nag, moo fi jiite woon sàndikaa bii di SUTELEC, di woon tamit njiitul Ndiisoog Ndoxal (PCA) bu “Caisse de sécurité Sociale). EJO ak LU DEFU WAXU ñoo ngi koy jaam Saa-Senegaal yépp, di jaar njabootam ak i mbokkam te di ko ñaanal njéggal ak yërmaande. Paap Aali JàlloPlus de publicationsBiographiePaap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/BÉSUB SÓOBARE YI : NJIITU RÉEW MA RAFETLU NA TAXAWAAYU SÓOBARE YI TE BOOLE LEEN CI POWI JOJ NDAKAARU 2026 YIPaap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/CAABALUG ARCOP 2022-2023 : 3,2 MILIYAAR YU NE MËY !Paap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/MBIRUM MAJAMBAL JAAÑ : YOON TEG NA LOXO MAYMUNA NDUUR FAY (7TV) AK BAABAKAR FAAL (GFM)Paap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/USMAAN SONKO YÉENE NA WÀÑÑIB MBËJ GI, NJAFAAN GEEK GIL BI FacebookTwitterWhatsAppE-mailImprimer Widewo VOA AMAL NAB JOTAAY CI MBINDUM BUBAKAR BÓRIS JÓOB GINNAAW BI WEREKAAN BI JËLEE CARGALUG NEUSTADT 2022 BI. CUQAL CI LËNKAAY BII TOFTALU... Defu Waxu - Xët yi mujj