Li fësXibaar AS TUUT CIY XALAAT By Paap Aali Jàllo 02/05/2025 0 0 Partager FacebookTwitterWhatsAppE-mailImprimer Yeneen i xët COKKAASU ODIA Paap Aali Jàllo - 08/12/2025 FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE Njuga Gay - 07/12/2025 MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM » Ndey Koddu Faal - 05/12/2025 NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI Njuga Gay - 30/11/2025 Aji bind ji Paap Aali Jàllo Moo ndax Ki ko tey Taamu Tànn Ndëŋte Ak njubadi Dina wuuteek Bant bu wow koŋŋ Téll dàmm lay mujje Mu wóor ne du soppi Jikko ndax làggi Ca mbir ma Na yoon yor yar ba Soo jiitoo Moytul jaayu Defe ne yaa yor Te yoroo Yàlla rekk a yor Moom mi la yor Yoraale lu nit mës a yor Moomoo dañu la yorloo Mbokk mu naa jox ma Nee ko moomuma Réew mee moom Dañu maa sàmmloo Jom ak ngor la làmboo Dañu lay dugal Nga dëkke randal Bu nu la nee nuus Dag ya ne nemm Mbaa ne meŋŋ Nga ne cunduŋŋ Rëccu ak nàqar Di sa wéttal Jabar ak doom Dugg jaaxle Céy gii gàcce Yaa leen ko yóbbe Gii gàkk-gàkk Nar a sax dàkk Nees koy fóote Séex Aliyu Ndaw Ndakaaru Awril 2025 Paap Aali JàlloPlus de publicationsBiographiePaap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/COKKAASU ODIAPaap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/USMAAN SONKO : « JÀMM REKK LAA SÉQ AK JOMAAY… LIGGÉEYALUMA JOMAAY, SENEGAAL LAAY LIGGÉEYAL. »Paap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/GINE BISAAWO | WOTEB FAL NJIITU RÉEW : FERNANDO DIAS DA COSTA MOO JIITOOGUMPaap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/AAMADU BA (JËWRIÑU MBATIIT MI) : « MBATIIT, DAFAY JUBOOLE TE DI SAXAL WÓOLOONTE » FacebookTwitterWhatsAppE-mailImprimer Widewo VOA AMAL NAB JOTAAY CI MBINDUM BUBAKAR BÓRIS JÓOB GINNAAW BI WEREKAAN BI JËLEE CARGALUG NEUSTADT 2022 BI. CUQAL CI LËNKAAY BII TOFTALU... Defu Waxu - Xët yi mujj