LIMUB SAABALUKAAY YI SÀMMONTE AK SÀRT YI
Sànq ci bëccëg lañu siiwal limub saabalukaay yi nga xam ne sàmmonte nañu ak sàrt yi yoon tëral. Dafa di, kenn daa umpalewul ne, bu yàggul dara am na lim bu ñu siiwaloon ba mu juroon fi coow....
Jàngalekat bii di Baara Mbeng moo jël neexal bii ñuy dippe "Grand Prix du Chef de L’Etat". Tay ci alxames ji lees doon amal ndajem cargal jàngalekat bi, fa "Grand Théatre".
Ndaje mii nag, du guléet ñu koy amal. Ren mooy ñetteelu yoon wi. Neexal...