Mustafaa Faal

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/2/2025)

LIMUB SAABALUKAAY YI SÀMMONTE AK SÀRT YI Sànq ci bëccëg lañu siiwal limub saabalukaay yi nga xam ne sàmmonte nañu ak sàrt yi yoon tëral. Dafa di, kenn daa umpalewul ne, bu yàggul dara am na lim bu ñu siiwaloon ba mu juroon fi coow....

NJÀNG AK NJÀNGALE : “GRAND PRIX DU CHEF DE L’ÉTAT”

Jàngalekat bii di Baara Mbeng moo jël neexal bii ñuy dippe "Grand Prix du Chef de L’Etat". Tay ci alxames ji lees doon amal ndajem cargal jàngalekat bi, fa "Grand Théatre". Ndaje mii nag, du guléet ñu koy amal. Ren mooy ñetteelu yoon wi. Neexal...

Njàngatum Guddig Mbooyo (2/2)

Doolee mën dëgg, waaye dëgg mooy mujj. Li tax bindkat bi taamu kàddug Guddig Mbooyo,...

‘’LI TAX SÉEX ANTA JÓOB AMUL MOROOM…’’

WAXTAANU SAADA KAN AK BUBAKAR BÓRIS JÓOB

KAN MOOY…MAKI SÀLL ?

Ci Baatu Majaw Njaay Aw askan, bala moo tànn njiitam, war naa seet bu baax...

XËT YI MUJJ

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/2/2025)

LIMUB SAABALUKAAY YI SÀMMONTE AK SÀRT YI Sànq ci bëccëg lañu siiwal limub saabalukaay yi...

NJÀNG AK NJÀNGALE : “GRAND PRIX DU CHEF DE L’ÉTAT”

Jàngalekat bii di Baara Mbeng moo jël neexal bii ñuy dippe "Grand Prix du...

YEESALUG NGOMBLAAN GI : EL MAALIG SUMB NA LIGGÉEY BI

Démb ci guddi, tele TFM dawal na laaj-tontu bi Njiitul Ngomblaan gi, El Maalig...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (4/2/2025)

SÉMBUW JOTALE DËKKI KOW YI AK NDOX MU SELL Nguur gi seqi na ñaareelu jéego...