Téere yi

Ay xalaat yu meññee ci “Malaanum Lëndëm”

“TOLOF-TOLOFI ÀDDINA SEEK BIDDÉEW YI CI KOW ASAMAAN SEE YEM: AK FOO MËNTI DEM,...

Njàngatum Guddig Mbooyo (2/2)

Doolee mën dëgg, waaye dëgg mooy mujj. Li tax bindkat bi taamu kàddug Guddig Mbooyo,...

Njàngatub Bàmmeelu Kocc : Téereb dekkali 1/2

Du guléet. Déedéet. Bindkat bi tëbul rekk bind Bàmmeelu Kocc Barma. Nde, ginnaaw Doomi...

Li ci biir “Xelum Xalam” bu Làmp Faal Kala

KAN MOOY LÀMP FAAL KALA ? Làmp Faal Kala, am ñu ko gën a xame...

LI CI BIIR "GUDDIG MBOOYO" BU LAMIN MBAAY

KAN MOOY LAMIN MBAAY ? Lamin Mbaay, ab Birigajeb pólis la woon. Mi ngi juddu...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...