CAN MAROG 2025

Yeneen i xët

Aji bind ji

Puluf nañu kippuy CAN 2025 bees dëgmal te mu war a ame fa Marog. Tay ci altine ji lañu jiifii-jaafaa yëf yi, daldi samp kippu yi, ku ci nekk ci réew yiy joŋante xam foo féete.

Nii la 6i kippu yi tëddee :

Kippu A

Marog

Mali

Sàmbi

Komoor

Kippu B

Esipt

Afrig-dii-Sidd

Àngolaa

Simbaabuwe

Kippu C

Niseriyaa

Tinisi

Ugàndaa

Tansani

Kippu D

Senegaal

Kóngo RDC

Benee

Botswanaa

Kippu E

Alseri

Burkinaa Faaso

Gine Ekuwaatoriyaal

Sudã

Kippu F

Koddiwaar

Gaboŋ

Kamerun

Mosàmbig

Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj