Xibaar

TERE NAÑU TELEFON YI CI DAARA YU SUUFE YEEK YU DIGG-DÓOMU YI

Lu tollu ci ñaari ayu-bés kepp ay bëgg a des ci ubbiteg daara yu...

DOXU ÑAXTU KUJJE GI

Ginnaaw tekkaaral gu yàgg gees nemmeeku woon ci kujje gi diggante bi waa Pastef...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (18/9/2025)

CÀMBARUG ÑETTI SÉMBI SÀRT Altine jii weesu lañu ubbiwaatoon Ngomblaan ga. Lañu ko dugge woon...

KU NAAN JOX SA MOROOM

Amoon na fiy jamono, néewoon na lool lees di gis kër gu amul ndaa....

SONACOS : JUBBANTI BU ÀND AK GOQI

Ca ndajem jëwriñ mees amaloon ci njiiteefu elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, lañu jëloon...

YENEEN SÉMBI SÀRT YU ÑU WAR A CÀMBAR FA NGOMBLAAN GA

Ci weeru ut wii ñu génn la amoon ñeenti sémbi sàrt yu ñu yóbboon...

XËT YI MUJJ

NGUURUG SENEGAAL DAJALE NA 450i MILIYAAR

Tolluwaayu réewum Senegaal ci wàllu koom tàmbali naa ub boppu ñenn ñi. Te, dara...

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI : NGUUR GI NAMM NAA AMAL DOXALIN WU DIGG-DÓOMU

Ci ubbite lekkool gi, Nguur gi jël nay matuwaay yu am solo ngir taxaw...

LI CI DIGGANTE NIT AK NITE

Moo xam muy seen doomu bopp walla jeneen ju ñu leen dénk, way-jur yu...

BUL BIND… / BINDAL…

Seen yéenekaayu web ci wolof ubbil na leen xët wu bees wees duppee BUL...