Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

MBIRUM SEEX TURE, GUNEG SENEGAAL GI ÑU FAAT CA GANA

Takk-deri Gana yi tàmbali nañoo lëñbët ngir ca yan anam la doomu Senegaal jii di Seex Ture faatoo ak ñan ñoo jël bakkanam. Dafa...

TUKKIY NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, door na tukki yu am solo ci njeexitalu ayu-bés bii ñu génn. Ñaari tukki yépp mi ngi...

CAAROY : GËSTUKAT YA JÉBBALE NAÑU NJIITU RÉEW MI NJUREEF YI

Gëstukat yi ñu dénkoon mbirum Caaroy ak sóobare ya ñu fa bóomoon ca atum 1944 jébbal nañu Njiitu réew mi Téere bu weex bob,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (16-10-2025)

XIBAAR ÑEEL YOON Téyandi nañu ràppëer bii di “10 000 problèmes” ak kii di Lamin Kàngaam. Ki tax ñu jàpp leen mooy  Sëriñ Abdulaay Fay...

AJAA JAAL MBAAY, JAAR NA BA JÀLL

Àddina yoon la wow, ku ko xas ba dëgmal, dem rekk. Moo waral sunu maam Jaal Mbaay tàggu nu biig, 14i fani oktoobar ci...

NGUURUG SENEGAAL DAJALE NA 450i MILIYAAR

Tolluwaayu réewum Senegaal ci wàllu koom tàmbali naa ub boppu ñenn ñi. Te, dara waralu ko lu dul bor bi fi Maki Sàll bàyyi...

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI : NGUUR GI NAMM NAA AMAL DOXALIN WU DIGG-DÓOMU

Ci ubbite lekkool gi, Nguur gi jël nay matuwaay yu am solo ngir taxaw ci doxalin wu digg-dóomu ñeel lekkool yi. Muy doxalin wuy...

LI CI DIGGANTE NIT AK NITE

Moo xam muy seen doomu bopp walla jeneen ju ñu leen dénk, way-jur yu bari dañuy def seen kemtalaayu kàttan ngir yar gone yi...

BUL BIND… / BINDAL…

Seen yéenekaayu web ci wolof ubbil na leen xët wu bees wees duppee BUL BIND... / BINDAL... Jubluwaay bi mooy di beqi njuumte yeek...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (9/10/2025)

YOON TÉYANDI NA ALIW SÀLL (RAKKU MAKI SÀLL) AK SOXNAAM Aliw Sàll, nekkoon fi meeru Géejawaay, di it rakk ci ki fi nekkoon Njiitu réew...