Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

TERE NAÑU TELEFON YI CI DAARA YU SUUFE YEEK YU DIGG-DÓOMU YI

Lu tollu ci ñaari ayu-bés kepp ay bëgg a des ci ubbiteg daara yu suufe yi ak yu digg-dóomi yi. Jëwriñ ji ñu dénk...

DOXU ÑAXTU KUJJE GI

Ginnaaw tekkaaral gu yàgg gees nemmeeku woon ci kujje gi diggante bi waa Pastef toogee ci Nguur geek léegi, mujj nañoo wàcc ci mbeddi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (18/9/2025)

CÀMBARUG ÑETTI SÉMBI SÀRT Altine jii weesu lañu ubbiwaatoon Ngomblaan ga. Lañu ko dugge woon mooy door beneen liggéey. Nde, dafa am liggéey bu ñu...

KU NAAN JOX SA MOROOM

Amoon na fiy jamono, néewoon na lool lees di gis kër gu amul ndaa. Njaq su mag soosu ñu defaree ban, wutal kog kubéer...

SONACOS : JUBBANTI BU ÀND AK GOQI

Ca ndajem jëwriñ mees amaloon ci njiiteefu elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, lañu jëloon mbirum SONACOS jox ko solo su réy. Jubluwaay bi mooy...

YENEEN SÉMBI SÀRT YU ÑU WAR A CÀMBAR FA NGOMBLAAN GA

Ci weeru ut wii ñu génn la amoon ñeenti sémbi sàrt yu ñu yóbboon fa Ngomblaan ga ngir càmbar leen. Li ñu ko dugge...

BUBAKAR BÓRIS JÓOB : AG GUY CI PÉNCUM LADAB

Jukkees na ab laaj-tontu ci yéenekaay Le Soleil, limu 16582eel bu Gaawu 13 ak Dibéer 14 Sàttumbar 2025.  Waxtaan la wow, sunu naataangoo bii...

TUKKIB ELIMAANU JËWRIÑ YI FA EMIRAAT ARAAB YA AK ITAALI

Elimaanu jëwriñ yi, Sëñ Usmaan Sonko, moo nga woon tay fa réewum Itaali, ginnaaw bi mu jeexalee, démb ci àjjuma ji, tukki bu mu...

MBOOTAAYU XEET YI WOTE NA “DECLARATION DE NEW YORK” BI

Ngomblaanu Mbootaayu Xeet yi nangu na lees duppee "Déclaration de New York" bi nga xam ne, dafay sàrtal nekkug ñaari réew yii di Palestin...

NDAJEM JËWRIÑ YI : NJIITU RÉEW MI ÀDDU NA CI LÀKKI RÉEW MI

Njiitu Réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar FAY, jiite na, ci alarbay démb ji, 10eelu fanu sàttumbar 2025, ndajem jëwriñ mees baaxoo di amal...