Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

SENEGAAL XAATIM NA DÉGGOOB 300I MILIYOŊI DOLAAR NGIR YEESAL MBAY MI

Jëwriñu Mbay mi, Dund bu matale bi ak Càmm gi, Sëñ Mabuuba Jaañ, xaatim ab déggoo bu tollu ci ñetti téeméeri (300i) miliyoŋi dolaar...

NDAJEM SALI NGIR SELLAL DUND BI

Lekk baax na. Waaye nag, na doon lekk lu baax, ci anam bu baax. Loolu la boroomi xam-xam yiy gëstu ci fànnu dund wax....

MONJAAL 2026 / RDC-SENEGAAL : XEEXU GAYNDE AK TENE

Joŋante bu tar te nar a tàng mooy xaar sunu gayndey futbal yi war a laaleek RD Kóngo, ca estaad "Martyrs". Bu 16i waxtu...

NDOGUM YOON MU METTI FA KEBEMEER

Ndogi yoon yaa ngi wéy di gën a bari. Saa yees jàppee ne ndog yi wàññeeku nañu rekk, fekk booba la Waalo gën a...

CÀMM GU YEES GI

Càmm gi soppeeku na. Démb, ci guddig gaawu bi, 6 sàttumbar 2025, la elimaanu jëwriñ yi, ànd ak magum fara-saytu njiiteefu réew mi, Umar...

MBIRUM SAA-SENEGAAL YI ÑU JÀPPOON FA MALI

Bàyyi nañu juróom-benni Saa-Senegaal yi ñu tegoon loxo fa Mali. Ci lees wax, terrorist yi (rëtalkat yi) ñoo leen jàppoon ci alxames ji laata...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (4/9/2025)

GÀMMU 2025 Tay, alxames, yemoo ak ñeenti fan ci weeru sàttumbar lañuy màggal bés bi Yonentu bi, Muhammad (SAWS) ganesee àddina. Mu doon bés bu...

NOPPEE GËN I WAX

Ba bërki-biig rekk, gaa ña jubooguñu woon. Ñu ngi doon wéy di jokkalantey kàddu. Yenn saa, ñu def ko cig dal. Waaye, yenn saa...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (2/9/2025)

54EELU NDAJEM UPCI Démb ci altine ji lañu doon ubbi 54eelu ndajem ndiisoo giy doxal gu mbooloo ngomblaani réew yi bokk ci kurélug OCI, UPCI....

NDAJEM PÉNCOO NOSTEG DUND BI CI KEMBAARU AFRIG CI ATUM 2025.

Jamono jii, ñu ngi amal, fi Ndakaaru, lees ndaje mees duppee « Forum Africain des Systèmes Alimentaires 2025 », maanaam Ndajem Péncoo Nosteg Dund bi ci...

DOXU ÑAXTU ÑOÑ PASTEF

Xew-xewi pólitig yi amoon diggante màrs 2021 ak féewiryee 2024 ba tay pënd ma wureegul. Li ko waral mooy ñi nga xam ne ñoom...