Iniwérsite Gastoŋ Berse

Yeneen i xët

Aji bind ji

 
Ndongo daara ya nekk ca Iniwérsite GastoŋBerse waroon a tàmbali ci talaata jii, dogal nañu gereew bu amul àpp. Loolu, nag, di fésal seen ñàkk ànd ci dogal yi njiiti daara ju kawe jooju jël ngir mën a wéyal njàngale mi.

Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj