Ismayla Maajoor Faal : « Mën nañ jàpp Usmaan Sonko saa su nekk. »

Yeneen i xët

Aji bind ji

Ginnaaw bi àtte bi jibee, ñu daan Usmaan Sonko 2i ati kaso yim war a tëdd, laaj bi des mooy bi ñeel ëllëgu Usmaan Sonko. Bees sukkandikoo ci kàdduy Ismayla Maajoor Faal, jëwriñu jiñ dénk wàllu Yoon, mënees na teg loxo njiitul Pastef li saa su nekk.

Daf ne, « ci àtteb teewadi lees nekk te mën nañ jàpp Usmaan Sonko saa su nekk. »

Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj