BEQI : JÀPPUÑU NGAÑ DEMBA TURE

Yeneen i xët

Aji bind ji

Xibaar bi ñu biraloon ñeel jàppug Ngañ Demba Ture mu Pastef wérul. Kenn jàppu ko. Mi ngi ci jàmm, moom ak njabootam. Waaye, wér na ni Séex Baara Njaay mi ngi ci loxoy Yoon ak ñu baree bari ci waa Pastef, rawatina Pastef Daaru Muhti.

Noo ngi jéggalu ci njuumte li.

Pap Aali Jàllo
Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj