MAKI SÀLL NDOKKEEL NA NJIITU RÉEW MU BEES LI, BASIIRU JOMAAY FAY

Yeneen i xët

Aji bind ji

Njiitu réew ma woon, war a fegal keroog 2 awril 2024, ndokkeel na Njiitu réew mu bees li, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. dafa bin ab tweet, rafetluwaale anam bi wote yi tëdde.

Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj