NGOMBLAAN GA

Yeneen i xët

Aji bind ji

Ci biir sémbub àtte biñ war a wote fa Ngomblaan ga, dañ ci bind ne :

« Ci yoonu waxtaan wi Njiitu réew mi Maki Sàll woote, dañ ci dégtal ne dañuy dindi baayaleg maxejj yi (parrainages citoyen) bàyyi fi baayaleg ñi ñu fal (parrainages des élus) ngir wàññi rëq-rëq yi. »

Bu loolu jàllee, dootuñu am 20i lawax, waaye 4i lawax kese ñooy mën a dagaan baatu askan wi.

Pap Aali Jàllo
Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj