PASTEF JIITAL NA BASIIRU JOMAAY

Yeneen i xët

Aji bind ji

Xibaar bi jib na : Basiiru Jomaay Fay la waa PASTEF tànn ngir doon seen lawaxu ci wotey 2024 yi. Ëllëg ci altine ji lañuy tàmbali dagaan baayale yi ñeel ko. 

Waaye nag, ci li Aamadu Ba mu PASTEF ci xëtu Facebookam, Usmaan Sonko moo leen gën a yitteel. Dinañ wéy di xeex ngir mu doon lawax. Moo tax, ci wàllu baayale gi, dinañ ko dencal

Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj