TAKK-DER YI SONAL NAÑU ARDO ÑING

Yeneen i xët

Aji bind ji

Ardo Ñing mi bokk ci Aar Li Nu bokk ak Noo Lànk la takk-der yi jàpp ginnaaw bi waa kurél gi doon amal doxu ñaxtu ca Toobeen. Bi ko takk-der yi jàppee nag, jot nañu koo mettital ba mu jële ci ay gaañu-gaañu. Kii di njiitu takk-der yi ca Tiwaawan nee na dinañ ubbi ab lànket ngir leeral mbir moomu.

Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj