Kafrin

Yeneen i xët

Aji bind ji

Kafrin : Ndox mi bari na ca Ndukkumaan ginnaaw bi mu tawee taw bu metti ca dëkk ba. Gox yu baree mujj a taa, kër yépp fees dell ak ndox. Waa dëkk baa ngay sàkku ndimbal ci nguur gi ngir mu jàppale leen ci mbënd mi.

Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj