Màggalu Tuubaa

Yeneen i xët

Aji bind ji

“Bu kenn dem, na ñépp toog, Màggal-leen seen kër”. Lii mooy kàdduy jëwriñ bi jiite IRD ca Màrsey, doktoor Séex Soxna. Mi ngi indi ay leeral di ci yokk ni : “Ginnaaw bi nu jàngate nekkinu nit ñi ci jamonoy Màggal, gis nanu ni ci la feebar yu bari di gën a law, rawati-na yiy jàpp biir ak dënn.”

Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj