Mamadu Jara

KÀTTEY BFEM 2024

Démb, ci altine ji, door nañu kàttey BFEM 2024 bi. BFEM (Brevet de Fin d’Études Moyennes) bi, mooy kàtte (walla lijaasa) yiy tëj xaaj bu njëkk ci njàng mu digg-dóomu mi fi réew mi. Bu atum ren ji nag, limub lawax yi dem na...

COOWOO CA NGOMBALAANU CEDEAO

Barki-démb, ci gaawu gi, la dépitey CEDEAO yi doon amal am ndaje fa Abujaa, fa réewum Niseriyaa. Waaye, laata ndaje ma di jeex la fa xew-xew bu doy waar am. Nde, ñaari dépite ñoo fa naroon a jàppante. Te, lenn waralu ko lu moy...

LU ЁPP TUURU !

xibaarRéewum Senegaal rafle na jàmm ci jamono jii, muy ci kàddu yi gaa ñi...

TAAFAR SI CI LÀNGUG POLITIG GI, MBAA DINA JUR JÀMM CI RÉEW MI ?

Xeetu taafar yi nuy faral di gis te di ko dégg ci réew mi...

kàdduy Seex Abdu Baara Dolli yi: Ban taxawaay la ci yoon wane?

Kàddu yi Seex Baara yékkati woon ca bésu ndajem ñaxtu Yewwi Askan Wi teg...

XËT YI MUJJ

KÀTTEY BFEM 2024

Démb, ci altine ji, door nañu kàttey BFEM 2024 bi. BFEM (Brevet de Fin...

COOWOO CA NGOMBALAANU CEDEAO

Barki-démb, ci gaawu gi, la dépitey CEDEAO yi doon amal am ndaje fa Abujaa,...

BÀLLA GAY DAANATI NA TAFAA TIN

Démb a doonoon woon ñaareel wi yoon ñu sëgg ci géewub bëre-dóor. Bàlla Gay...

TÀGGE : USÉYNU BÉEY WÉY NA

Njabootu mbatiit ak làmmiñi réew mi amati nañ tiis ak uw naqar. Kenn ci...