Démb la woon alxames, 26i pani sàttumbaar 2024, yemoo ak bés bees di fàttaliku suuxug "Bateau Le Joolaa". Bés boobii la Càmm gi tànn ngir biral njureef yu tukkee ci càmbar bi ñu doon càmbaar ndono li leen Maki Sàll ak nguuram ga woon...
LEERALI CÀMM GI CI LIÑ FI FEKK
Ci alxamesu tey jii, 26i pani sàttumbaar 2024 la Càmm gu bees gi joxe woon niki àpp ngir wax askan wi li Maki Sàll ak nguuram ga woon bàyyee. Elimaanu jëwriñ ji, Usmaan Sonko, jëwriñi koom-koom geek gog...