Mamadu Jara

67EELU LËLU NJIITI RÉEW AK CÀMM YU CEDEAO

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, dem na tay ci gaawu bi, 21 suwe, fa Abuja (réewum Niseeriyaa), ngir teeweji 76eelu lëlub Njiiti réew yeek Càmm yu Kurélug CEDEAO. Tay ci suba la fi Njiitu réew mi bawoo utali Abujaa, ngir teeweji, ëllëg...

COKKAASU ODIA

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI Gaawu, 20 ut 2022

XEW-XEWI JAMONO Yokkuteg njëgu soble ga ca Tuubaa  Ñàkkum soble bi ganesi réew mi ci fan...

DÉGGOOB 79. 329 MILIYAAR DIGGANTE SENEGAL AK BAD

Jëwriñ ji ñu dénk fànnu koom-koom gi, Aamadu Hot, xaatim na ab pas bu...

TOLOF-TOLOFI ARTISÃ YI : LAN MOO CIY TAXAWAAYU NGUUR GI

Fànnu artisanaa nekk na lu soxal lool nit ñi rawatina artisã yi yore seen...

Doxalinu wotey palum depite yi ci Senegaal

Dibéeru tey 31 i fan ci weeru Sulet la wotey palum depite yi tàmbali...

Bërug ndëgg-sërëx

*Xana du bër da daan neex ndongo ? Daara ju kawe ja ca Ndar,...

Mbënn mi ak toj-toj yi : fan la miliyaar yi duggu ?

Njàqare, jaaxle la ñu bari ci ñi dëkke ci yenn diwaan yu nekk ci...

NJUREEFI SOROJ BI AK GAAS

Réewum Senegaal a ngi waaj a jëfandikoo soroj bi ak gaas bi fileek diir...

SONKO AK MAKI : KUY DAAN ?

Fitna lañ doore bésub àjjuma jii. Fitna ju sosoo ci diggante Sonko ak Maki....

XËT YI MUJJ

67EELU LËLU NJIITI RÉEW AK CÀMM YU CEDEAO

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, dem na tay ci gaawu bi,...

COKKAASU ODIA

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/6/2025)

GAINDESAT-1B : SENEGAAL WUTALI NA JAWW JI Senegaal a ngi séqi na jéego bu yees...

PALESTIN, JIRIMU ÀDDINA SI

Ñaar-fukki weeri xare yoy, bés bu nekk, fa Gasaa, ay bakkan rot. Bu leen...