kàdduy Seex Abdu Baara Dolli yi: Ban taxawaay la ci yoon wane?

Yeneen i xët

Aji bind ji

Kàddu yi Seex Baara yékkati woon ca bésu ndajem ñaxtu Yewwi Askan Wi teg ko ci deru njiitu réew mi jural na ko coow ba yoon teg ko ci loxo. Ndax, dañoo jàpp ne kàddu yi dafa ñaaw ci ku toll ne Njiitum réew. Ba tax na, ñoom xaaruñu dara ngir teg ko loxo. Li xaw a jaaxal gaa ñi kay mooy niñ ko patam-patamee ci koo xam ne ab depite la. Maanaam lu tax dindi wuñ malaanu kiiraayam laata ñu koy jàpp ?

Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj