Uséynu Béey

TÉYANDI NAÑU PAAB MAALIG NDUUR (APR)

Tay lañu woolu woon Paab Maalig Nduur, nekkoon jëwriñ ca nguurug Maki Sàll ga woon, bi 16i waxtu jotee ci ngoon, fa màkkaanu banqaasu luññutu bob sàndarmëri . Sabab bi tax ñu ko woolu woon ko mooy kàddu ya mu yékkati woon ci menn...

COKKAASU ODIA

KÀDDUY USMAAN SONKO 2/2 PÀCC

Senegaal gépp amoon na fiy yëngu-yëngu, réew mi jaxasoo, yëf yi doy waar lool,...

KÀDDUY USMAAN SONKO 1/2 PÀCC

Senegaal gépp amoon na fiy yëngu-yëngu, réew mi jaxasoo, yëf yi doy waar lool,...

Njàngatub Bàmmeelu Kocc : Téereb dekkali 1/2

Du guléet. Déedéet. Bindkat bi tëbul rekk bind Bàmmeelu Kocc Barma. Nde, ginnaaw Doomi...

BARSAA WALLA… BARSÀQ !… LU XEW CI MIIM RÉEW?

Géej gaa ngiy wann sunu doom yi. Mbete jasig juy warax béy bu lab. Ay...

SËRIÑ SEEKA BARI DOOLE CI LÀNGU PÓLITIG GI !

Ni waa Senegaal gëmee Yàlla te fonk diine, umpul kenn ci àddina si. Nde, askanuw...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am na xarnook xaaj. Waaye, mi...

FAIDHERBE DU FI MAAMU KENN

Fan yii yépp, xanaa mën nañoo wax sax weer yi weesu yépp, coow laa...

AFRIG AK KORONAA, AFRIG GINNAAW KORONAA

USÉYNU BÉEY Koronaawiris bi, li muy metti metti, terewul kàngami boroom xam-xam yiy wéy di ci...

XËT YI MUJJ

TÉYANDI NAÑU PAAB MAALIG NDUUR (APR)

Tay lañu woolu woon Paab Maalig Nduur, nekkoon jëwriñ ca nguurug Maki Sàll ga...

COKKAASU ODIA

2026 : SENEGAAL A NGI SÓOBU CI SÉMB YU MAG YI

Ginnaaw bi ñu defee at ak lu teg, Càmmug Basiiru Jomaay Jaxaar Fay gee...

MBIRUM SEEX TURE, GUNEG SENEGAAL GI ÑU FAAT CA GANA

Takk-deri Gana yi tàmbali nañoo lëñbët ngir ca yan anam la doomu Senegaal jii...