LIGGÉEY BA DOOR NA FA NGOMBLAAN GA
Altine jii weesu lañu ubbi fukk ak juróomeelu moomeg Ngomblaan gi, fal mbooleem ñi ñu war a fal ca béréb ba. Mu mel ni dépitey Ngomblaan gii amuñu toogaay. Nde, démb, ci àllarba ji la ki fi nekkoon...
Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jiite na ndajem jëwriñ yi barki-démb ci talaata ji. Ginnaaw bi mu defaree coppite yi am ci Càmm gi, dellu na ñaaxaat jëwriñ yi ñu farlu ci mbir yi gën a tembare, rawatina mbir yi ñeel...