Li fës

SÉMBUW NDEFARUG DAAMARI SÓOBARE

Dees na samp ndefarug daamari sóobare fi réew mi. Xibaar la bu tukkee ci...

ETAASINI : DONALD TRUMP FALUWAAT NA

Ki fi nekkoon Njiitu réewum Etaasini, Donald Trump (20 sãwiyee 2017 ba 20 sãwiyee...

MBIRUM KAASAMÃS

Ci àjjuma jee weesu, magum jëwriñ yi, Usmaan Sonko àddu woon na ci téere...

PAATUG MAMADU MUSTAFAA BA MA WOON JËWRIÑU NGURD MI AK NAFA GI

Léegi la APS siiwal xibaaru paatug Mamadu Mustafaa Ba mi woon jëwriñu ngurd mi...

TUKKITEY NJIITU RÉEW MI FA ARAABI SAWDIT AK TURKI

Dibéer jee weesu la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, tukki woon na....

SÉMBUB GTE (GRAND TRANSFERT D’EAU) BI

Càmmug Senegaal ak SINOHYDRO (bànqaas ci kër gii di Power-China) taxawal nañu liggéeyi sémbub...

BALAA NOO LAAX JAAY…

Nit, ak xelam ak i xalaatam yu xóot, du jóg ci di jéem a...

XËT YI MUJJ

DÉPITEY FARÃS YI DAANEEL NAÑU CÀMMUG MICHEL BARNIER

Dépitey Ngomblaanu Farãs yi wote nañu pasum diiŋat (motion de censure), daldi daaneel Càmmug...

ÀMBURUWAAS SAAR : AATU RÉER NA !

Njabootu làmbu Senegaal ak mbatiit am nañu dëj. Nde, xibaaru tiis ak uw naqar...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (3/12/2024)

CAAROY 44 : NJIITU RÉEW MI JËL NAY NDOGAL Barki-démb ci dibéer ji lañu doon màggal...

TIIS WU RÉY FA GINE

Mats futbal bu mujje ciy masta ! Mbir yaa ngi xew barki-démb ci dibéeru...