Xibaar

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/7/2025)

PASTEF MÀGG NA Atum 2014 lañu sosoon làng gii ñuy dippe PASTEF. Maanaam, atum ren...

NDAJEM DONALD TRUMP AK JURÓOMI NJIITI RÉEWI AFRIG

Senegaal, Gaboŋ, Gine-Bisaawo, Liberiyaa ak Muritani… juróomi réew yii la Njiitu réewu Etaasini li,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (8/7/2025)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA ETAASINI Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay bawoo...

XEW-XEW BU TIIS FA JÀNGUNE JU KAWE JOJ NDAR

Naqar ak tiis la waa Ndar fanaanoo guddig barki-démb rawatina ndongo ya nekke fa...

COOW TOPP NA ELIMAANU JËWRIÑ YI

Daar-daar bi Sëñ Usmaan Sonko doon amal mujje na a jur coow ci pénc...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (3/7/2025)

NDAJEM ETAASINI AFRIG Ayu-bés bii ñu jëm lañuy amal ndaje mii ñu dippe “sommet Etas-Unis-Afrique”....

ÑAXTUY SÀNDIKAA YI

Jamono yee ñu weesu, ñaxtuy sàndikaa yi yëngaloon na réew mi. Waaye, ginnaaw ab...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...