Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

EKIBU SENEGAAL BU MAG BI Paap Caw, tàggatkatu ekib bi siiwal na limka ndaw yi mu tànn ci ñaari ndaje yi ñu dëgmal ci fan...

WAAJTAAYI GÀMMU 2025 : NJIITU RÉEW MAA NGA WOON FA TIWAAWAN

Tay ci gaawu bi, Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay moo nga woon Tiwaawan. Mu doon fa amal ab tukki ngir nemmeeku...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (28/8/2025)

PAAB MAMMADU SEKK GÉNN NA ÀDDINA Naqar ak tiis la ñu bari ci askanu Senegaal fanaanoo démb, rawatina ñi bokk ci làngu Pastef. Kii di...

SÉMBUW ÀTTE 14/2025 CI WÀLLU SÀKKU AK JOT XIBAAR

Démb, talaata 26 ut 2025, la dépite yi wote, daldi jàllale sémbuw àtte 14/2025 te aju ci wàllu sàkku ak jot ay xibaar yu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (26/8/2025)

NGOMBLAAN GI Dépite yi wote nañu sémbuw àtte wiy jëmmal yoolekat yi. Muy àtte bob, li ko tax a jóg mooy xeex nger ak luubal....

ABBAAS FAAL : “BOROOM NDAKAARU”

Tay, ci altine ji, lañu doon wote ngir fal meeru Ndakaaru biy wuutu Bàrtelemi Toy Jaas mi ñu fa déjjati. Li ko waral du...

DEKKALI SONACOS : YÉENEY NGUUR GI

Nguurug Senegaal gi dina yékkatiwaat kërug liggéey gii di SONACOS. Jël na 14i ndogal ngir tegaat ko ci yoon ginnaaw ndajeem jëwriñ mi ñu...

YÉGLEB “COALITION SÉNÉGALAISE POUR LA CAUSE PALESTINIENNE”

"Njiiti Etaasini yi tooñati nañu waa "Cour Pénal International" (CPI), di ëttu àttekaayu àddina si. Nde, dafa jëlal boppam ndogalu teg ay daan ci...

KËR ARAM

Seeti naa soxna Aram Faal Jóob, ndaanaan Jàmbaar la,  lingeer dëggantaan Dama ko ni jàkk sama yaram di daw Mu siggi xool ma, mbaaru bëtam jëm kaw Mbégte...

XIIF GA CA GASAA : MBOOTAAYU XEET YI DËGGAL NA

Ci àjjumay tay jii la Mbootaayu Xeet yi (ONU) xamle ci lu wér ne, fa Gasaa (Gaza), xiif gaa ngay ray askan wa. Ginnaaw...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (21/8/2025)

DAKKALUG DUGAL GAAS CI RÉEW MI Réewum Senegaal mi ngi waaj a séqi beneen jéego bu am solo ngir moom boppam, mënal boppam. Nde, fii...