TURI JOTAAYI TELE SENEGAAL YI
Seen Xéewal
Tës
Saa Njóogu
Kër gi ak Taal Ngol-Ngol
Aaru Mbedd
Diine ak Jamono
Reeni koom-koom
Njàngatu bés bi
Jàkkaarloo Bi
Yeewuleen
Seen jotaay / jataay
Faramfàcce
Sama Gox
Kàkkatar
Tàkkusaanu Jolof
Li ci réew mi
Ndumbelaan
Gis-gis
« Dans l’enfer des » mbindaan
KOORU JÀMM, WAAJAL KORITE AK « FONDATION PAD »
Jotaayu Xam-Xam
Mbaboor mi. Siiw du jàmmi boroom
TERAANGA KU NE
« SenTv » Wone ma
ÀND WATTU LÀKKI RÉEW MI
Ñi ci bokk
Ajaratu Umar Sàll Jaw (ma-làmmiñal, l’IFAN Ch. A. Diop, UCAD), Maryetu Jong Jóob (Moo doon njiitu Fondation UCAD), Ndey Koddu Faal (Njiitu EJO, di kër guy móol ay téere ci làkki réew mi), Useynu Béey (Taskatu xibaar), Maam Cerno Siise (Ma-làmmiñal FLSH, UCAD), Adaraame Jaxate (Njiitu bondkat yi ci làkki réew mi), Baabakar Jóob Buuba (Ma-mboor, Département de Langues anciennes, FLSH, UCAD), Bubakar Bóris Jóob (Bindkat), Amet Juuf ( Ma-yoon), Mamadu Jara Juuf (Bindkat), Maamur Daraame (Ma- làmmiñal, FLSH, UCAD, Dakar), Abdu Xaadar Kebe (Bindkat, Ma-mboor), Mansuur Xumma (Jàngalekat, Ma-làmmiñal), Baydi Taal Nduur (Bindkat, Léebkat), Màmmaram Sekk (Ma-làmmiñal, l’IFAN Ch. A. Diop, UCAD), Isaa Ture (Jàngalekat, Ma-làmmiñal), Maam Daawur Wàdd (Bindkat)