Ëllëgu gaynde yi ca tugal

Yeneen i xët

Aji bind ji

Naples noppeegul ngir bàyyi Kalidu Kulibali mu dem. Moo ngi ci tànki yokkal ko peyooram ci àpp gu gudd donte ni këlëb yu mag yu mel ni PSG, Roma, Chelsea, rawatina Barcelone, fësal nañ seen bëgg-bëgg ci doomu Senegaal ji ak di ko dig lu ëpp li ko Naples daan fey. Lu soxal Abdulahat Jàllo, Paris mën na koo abale walla mu jaay ko Stade de Rennes mi nekk ciy tànkam ; fekk na Saajo Maane ñuy wéy di ko gën di dégg ca Bayern.

Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj