Mbay Sow

NGUURUG SENEGAAL DAJALE NA 450i MILIYAAR

Tolluwaayu réewum Senegaal ci wàllu koom tàmbali naa ub boppu ñenn ñi. Te, dara waralu ko lu dul bor bi fi Maki Sàll bàyyi ak li FMI di dóor dàqe ak Nguur gi fi nekk. Rax-ci-dolli, kurél gii di Moody’s dafa yokk ci xar...

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI : NGUUR GI NAMM NAA AMAL DOXALIN WU DIGG-DÓOMU

Ci ubbite lekkool gi, Nguur gi jël nay matuwaay yu am solo ngir taxaw ci doxalin wu digg-dóomu ñeel lekkool yi. Muy doxalin wuy boole ñépp, am njariñ te di yamale. Barki-démb ci àjjuma ji, 10i fan ci weeru Oktoobar 2025, Càmm gi doon na...

NGUUR GU YEES GI

Ndekete, njuuy, ci feemi Njiitu réew mi la bokk. Nde, ginnaaw Aamadu Maam Jóob...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI Alxames 15 sàttumbar 2022

DIINE Màggalu Tuubaa Tey di alxames 15 sàttumbar 2022, yamoo ak 18 Safar ci weeru araab,...

Li gёn a fés ci xibaari bés bi Alxames 1 Sàttumbar 2022

PÓLITIG Àppug wotey HCCT xamees na ko Ci ab saabal bu mu génne, Njiitu réew mi...

WOTEY 2024 YI : WURE WA DEM NA KÉŊ

Lu tollu ci fukki weer ak juróom-ñett kepp a des ci wotey palum Njiitu...

TAXAWAAYI DÉPITEY KUJJE GI LAATA SEEN AG DEM CA PÉNCUM NDAWI RÉEW MA

Ginnaaw bi njureefi joŋantey palum dépite yi rotee, yenn ci dépite yi biral nañ...

Gàttalug xibaar yi, Alxames 18 ut 2022

 Siin Lii nag ag lёngoo la gu jёm ci wàllum mbey ci diggante ñaari réew...

WUJJE GI CI BIIR KUJJE GI  LAN MOOY JUBLUWAAY BI ?

“ Yaa ma..” ji ak “Maa la…” ji a ngi tulle ak màlle ci...

LI GЁN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Àjjuma 12 ut 2022

PÓLITIG : Ndogal yi lёkkatoo yii di YEWWI ak WALLU jёl Ginnaaw seen ndajem waxtaan...

XËT YI MUJJ

NGUURUG SENEGAAL DAJALE NA 450i MILIYAAR

Tolluwaayu réewum Senegaal ci wàllu koom tàmbali naa ub boppu ñenn ñi. Te, dara...

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI : NGUUR GI NAMM NAA AMAL DOXALIN WU DIGG-DÓOMU

Ci ubbite lekkool gi, Nguur gi jël nay matuwaay yu am solo ngir taxaw...

LI CI DIGGANTE NIT AK NITE

Moo xam muy seen doomu bopp walla jeneen ju ñu leen dénk, way-jur yu...

BUL BIND… / BINDAL…

Seen yéenekaayu web ci wolof ubbil na leen xët wu bees wees duppee BUL...