Mbay Sow

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

MBIRUM DUWAAÑE BI LÀQOON YÀMBAA CI DAAMARAM

Kaawteef ! Ab duwaañe lees fekk yàmbaa cig daamaram. Mbuur la xewee. Mu di...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (5/6/2025)

PÉNCOOM RÉEW MI Ci ayu-bés bee ñu génn lañu dooroon péncoom réew mi ñeel nosteg...

TUKKIY USMAAN SONKO, ELIMAANU JËWRIÑ YI

Alxames jii weesu la elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, dooroon ab tukki ci yenn...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (29/5/2025)

"BAD" AM NA NJIIT LU BEES Tay, ci alxames ji, lañu doon amal wotey palug...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (23/5/2025)

XIBAAR ÑEEL JURÓOMI JËWRIÑ YI ËTTU YOON GU KAWE GI WOOLU WOON Ci ndoorteelu ayu-bés...

NAALUW “CONSEIL SUPÉRIEUR DE LA JUSTICE”

Démb, ci dibéer ji, la kii di Porofesëer Siidi Alfa Njaay, doon amal aw...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (15/5/2025)

YOON LÀBBALI NAW FASAM Ayu-bés bee ñu génn la Ngomblaan gi tegoon ay tuuma ci...

SFI DUGAL NA XAALISAM CI SENEGAAL

Këru liggéey gii di SFI (Société Financière Internationale), kër la gog day yëngu ci...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA