Mbay Sow

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (8/5/2025)

CÀMBAR YI JÓGE CI SÉMBI TEG I TUUMA ÑI FI NEKKOON I JËWRIÑ Ngomblaan ga...

ÑAXTUY LÀNGI PÓLITIGI MALI YI

Coowi pólitig yi lëmbe na lool réewi Afrig sowu-jant yi, rawatina ci juróomi at...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (1/5/2025)

XAATIMUG DÉGGOOB DAL DIGGANTE NGUUR GI, SÀNDIKAA YI AK “PATRONATS” YI Bésub alxamesu tay jii...

MURIG MBALAANI KIIRAAYI MUSTAFAA JÓOB AK NDEY SALI JÓOB JEŊ

Tay, ci altine ji, lañu woolu woon dépite yi fa Ngomblaan ga. Li waraloon...

PASTEF AK KUJJE GI ÑU NGI XËCCOO NDAM LI

Démb la Ndajem ndeyu sàrtu réew mi génnee ab dogal ñeel sàrt bi dépitey...

PAAB FARÃSUWAA GÉNN NA ÀDDUNA

Naqar ak tiis la mbokki katolig yi yeewoo ci altiney tay jii. Kii di...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (17/4/2025)

TERE NAÑU MANSUUR FAY MU GÉNN RÉEW MI Ay yooni yoon, Mansuur Fay mi ngi...

MBIRUM KOPPARI “FONDS FORCE COVID-19”

Mbiru “Fonds Force Covid-19” mi lëmbe na lool réew mi fan yii. Bari na...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA