Li fës

FMI AJANDI NA WOTEB SIPPI BI ÑEEL SENEGAAL

FMI ajandi na woteb sippi bi waroon a tax Senegaal mën a leb xaalis...

SENEGAAL / « CYBERATTAQUE » : AY SÀMBAA-BÓOY SONG NAÑU « FISC » BI

Xibaar bu doy a doy waar la Sikafinance siiwal ci bésub alxamesu tay jii,...

YËGLEB NJËWRIÑU BIIR RÉEW MI AK KAARAANGEG PÉNC MI

Yégle bi : "Njëwriñu Biir Réew mi ak Kaaraangeg Pénc mi mu ngi yëgal askan...

MAMADU LI (ARED) JËL NA NEEXALU YIDAN 2025

Mamadu Aamadu Li, njiitu ARED, moo jël Neexalu Yidan 2025 ca Oŋ-Koŋ (Hong-Kong). Muy...

COOW DIGGANTE BILAAL JAATA AK TASKATI-XIBAAR YI

Njabootu saabalkat yi mer nañu ba futt. Li ko waral du lenn lu moy...

MBIRUM MAJAMBAL JAAÑ

Ginnaaw bi Majambal Jaañ dawee, génn réew mi, Nguurug Senegaal jàpplu na ko fu...

SËRIÑ MAXTAAR JENN, XARITU XALE YI, DËDDU NA

Àllarba, 27eelu ut 2025 la Sëriñ Maxtaar Jenn ñàkk bakkanam cim ndog ci yoonu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (25-9-2025)

NJIITU RÉEW MI JËMMAL NA ÑEENTI SÉMBI SÀRT YEES WOTE WOON FA NGOMBLAAN GA Fan...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...