Koom-koom

Kollëre gi doxoon diggante Coca-Cola ak Soboa fecceeku na !

Pas gi waa Coca-Cola ak Soboa amaloon seen diggante àntuwul. Daanaka ci Suliye bi...

Lan moo wund demu Maki bi Riisi ?

Fan yii weesu, njiitu réew, Maki Sàll, fekki woon na Putin ca Riisi ngir,...

XËT YI MUJJ

« MËSUNOO GIS BOR BU ÑU NËBB BU TOLLU NII CI AFRIG », EDWARD GEMAYEL, NJIITU NDAWI FMI FI SENEGAAL

Nees ko biralee woon ci sunu yaxalu barki-démb bi, ndawi yi FMI yabal fi...

LIGGÉEY BAA NGI WÉY DIGGANTE FMI AK NGUURUG SENEGAAL GI

Waa FMI dinañu toogaat ci réew ay fan ngir wéyal liggéey bi ñu sumb...

CAABALUG ARCOP 2022-2023 : 3,2 MILIYAAR YU NE MËY !

ARCOP (Autorité de Régulation des Marchés Publics), di banqaas biy saytu lépp lu aju...