Xibaar

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (19/8/2025)

FMI YÓNNEE NAY NDAW FI SENEGAAL Ay ndawi FMI (Fond Monétaire International, di kurélug koom-koomu...

CÀMBARUG ÑEENTI SÉMBI SÀRT FA NGOMBLAAN GA

Lu tollu ci weer ak lu teg ginnaaw bi ñu dakkalee seen i càmbar...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA SÀPPOŊ

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jóge na fi tay, ci yoor-yoor...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

BASKET : AFROBASKET 2025 Senegaal dina amal mats jàll (barrage) ëllëg ci altine ji, bu 18i...

DEXU SENEGAAL GI NAR NAA WALAAT FA MAATAM AK BÀKKEL

Dexu Senegaal gi nar naa walaat fa Maatam ak Bàkkel bu taw bi wéyee...

WÉERUWAAY

Sunu jenn maam ju mënoon a way ne woon na : “Am kilifaay li...

MALI : JAPP NAÑU ÑAARI SENERAAL AK BENN SAA-FARÃS

Ci alxamesu démb ji la xibaar bi rot. Sóobare yay jiite réewum Mali jamono...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (14/8/2025)

LIMU ÑI TEEWE MÀGGALUG TUUBA Démb, ci àllarba ji, lañu doon amal màggalug Tuubaa. Mu...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...