Xibaar

ABBAAS FAAL : “BOROOM NDAKAARU”

Tay, ci altine ji, lañu doon wote ngir fal meeru Ndakaaru biy wuutu Bàrtelemi...

DEKKALI SONACOS : YÉENEY NGUUR GI

Nguurug Senegaal gi dina yékkatiwaat kërug liggéey gii di SONACOS. Jël na 14i ndogal...

YÉGLEB “COALITION SÉNÉGALAISE POUR LA CAUSE PALESTINIENNE”

"Njiiti Etaasini yi tooñati nañu waa "Cour Pénal International" (CPI), di ëttu àttekaayu àddina...

KËR ARAM

Seeti naa soxna Aram Faal Jóob, ndaanaan Jàmbaar la,  lingeer dëggantaan Dama ko ni jàkk sama...

XIIF GA CA GASAA : MBOOTAAYU XEET YI DËGGAL NA

Ci àjjumay tay jii la Mbootaayu Xeet yi (ONU) xamle ci lu wér ne,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (21/8/2025)

DAKKALUG DUGAL GAAS CI RÉEW MI Réewum Senegaal mi ngi waaj a séqi beneen jéego...

BÀJJEN ARAM

La Kocc jàngale woon nga feeñal ci talaata jii « Mag mat naa bàyyi cim réew » Teey,...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...