Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LÀMB JI : FARÃ DAAN NA ËMMA SEEN

Doomu Pàrsel bi jaar na ci tànki magam ja, Móodu Lóo. Raxas na bépp mbëru Pikin bees tegoon ci kanamam ba ci seen mag...

CAYTUG BOKKEEF GI : « NDAWUL NGUUR MËNUL DOON MILIYAARDEER », (USMAAN SONKO)

Elimaanu jëwriñ yi, Sëñ Usmaan Sonko, teeweeji woon na ndaje mees jagleel coppiteg nosteg Càmm gi. Maanaam, naaluw soppi anam bi kuréli Càmm giy...

NJIITU RÉEW MI WOOTE NA ÑAARI FANI NJËMBËTUM GARAB

Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay woote nab kàmpaañu njëmbëtum garab. Ñu namm koo amal ci réew mépp ngir jëmbët lu tollu...

NAALUW JOYYANTI KOOM GI AK MBOOLAAY MI

Elimaanu jëwriñ yi, Sëñ Usmaan Sonko, gaaral na naaluw joyyanti koom geek mboolaay mi. Tay jii, àjjuma, 1 ut 2025, la ko doon gaaral...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (30/7/2025)

SULLIWAAT NAÑ WAYNDAREW FÀLLU FAAL Mbirum Fàllu Faal lëmbe woon na lool réew mi jamono yee weesu. Nde, ñu bari dañoo génnoon di ñaawlu li...

LI GËN A FÉS CI XIIBAARI BÉS BI (29/7/2025)

NAALUW JOYYANTI KOOM-KOOM GI Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, dina gaaral naal wi Càmm gi taxawal ngir joyyanti koom-koomu réew mi. Ginnaaw bi mu...

SYTJUST-UNTJ LÀBBALI NAÑ

Sàndikaa yi ëmb liggéeykati Yoon yi, di waa SYTJUST (Syndicat des Travailleurs de la Justice) ak UNTJ (Union Nationale des Travailleurs de la Justice)...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

FUTBAL El Maalig Juuf tàmbali na ak ekibam bu bees bi, West Ham. Amal nañu ñaari joŋantey tàggattu ngir waajal sàmpiyonaa bi ñu dëgmal. Ci...

NU ÀND WATTU KÀGGU YI

Bari na ay kàddu yu siiw, yu nuy faral di wax ak a waxaat te amaana sax xamunu ku leen fent. Ñaare, nu moomale...

SENEGAAL-MÓRITANI : PAS GU BEES ÑEEL DEM BEEK DIKK BI

Réewum Senegaal ak mu Móritani fas nañu lu bees ci dem beek dikk bi. War na léegi ci doomi réew mu ci nekk ñu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/7/2025)

UBBITEG CAMPUSEN Bu yàggul dara la joŋantey fàggug lijaasa bii ñuy dippe Baccalauréat jeex. Nde, lijaasa boobu dina ubbil ndongo yi buntu yu bari. Muy...