Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/7/2025)

NJÀNGALE MU KAWE MI Jëwriñu njàngale mu kawe mi dina jël 500i jàngalekat ak i gëstukat yu bees. Xibaar la bu mu siiwal démb ci...

YOKKUTEG PAYOORI SAABALUKAAYI BITIM-RÉEW YI

Nguur gu bees gi séqi na ay jéego ñeel cettantalug pas yi réewum Senegaal jotoon a xaatim. Dafa di, ñoom lii, lu ñu digoon...

USÉYNU BÉEY, AT CI SUUF…

Bi Uséynu Béey génnee àddina ak tey, def na atum Yàlla. Ñu bari bind ci moom, ay seede yu rafet, ay pàttali yu daw...

SITTA DAAN NA BÀLLA GAY 2

Dibéer, 20i Sulet 2025, Bàlla Gay 2, doomu Géejawaay ji, waada bu mag doon daje ak xale jàmm-a-gën bi, Sitta. Seen ndaje mi nag,...

KÀDDUY NJIITU RÉEW MI FA GINE BISAAWO

Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay yékkati nay kàddu woote fa Gine Bisaawo ga mu demoon ginnaaw ba ñu fa sàkkoo teewaayam...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (17/7/2025)

SÓOBAREY FARÃS YI GÉNN NAÑU RÉEW MI Bu yàgg ba tay (1960) sóobarey Farãs yi ñi ngi ci réewi Afrig sowu-jant yi. Mu am yenn...

WAX SA LÀKK, MOOM SA BOPP

Bi nu noppee ci fal Njiit lu bees, teg ko ci boppu réew mi, ñu bari dañoo gisoon ne yamuñu rekk ci soppi ñi...

XURUW DEX GI : ISRA MI NGI CAAF MBAYUM CEEB MU YEES

ISRA sóobu na ci xeetu mbayum ceeb mu yees ca bëj-gànnaaru réew mi. Nde, fale ca xuruw dexug Senegaal ga, fa la nekk di...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (15/7/2025)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA BENEE Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay bawoo na fi tay ci talaata ji, wutali Kotonu, réewum Benee....

NAALUW SENEGAAL 2050 : USMAAN SONKO SAS NA JËWRIÑ YI

Ci altiney démb ji, elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, doon amal ndaje ak jëwriñi Càmm gi. Naaluw « Senegaal 2050 » wi lañu doon...