Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

MÀGGALUG TUUBAA 2025

Tay, 13i pani ut 2025 mooy méngook 18eelu fanu safar ci atum 1447 ci arminaatu jullit ñi. 18eelu safar nag, bu ñu ko waxee...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (12/8/2025)

TUKKIB ELIMAANU JËWRIÑ YI FA TIRKI Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, jeexal na démb ci àjjuma ji tukki bi mu doon amal fa réewum Tirkii....

XEW-XEWI PÓLITIG FA CÀDD AK KODDIWAAR

Réewi Afrig yi, rawatina yoy Afrig sowu-jant, bari na lool lees fay nemmeeku ay yëngu-yëngu. At yu mujj yii moom dañ cee raw. Te,...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

FUTBAL CHAN 2025 Po mi tàmbali na keroog 2 Ut 2025. Senegaal dafa bom matsam bu njëkk, mu doxoon ci digganteem ak Niseriyaa. Benn bal la...

NJÀNG MU KAWE MI : JËWRIÑ JI DINA JËL 1 500I JÀNGALEKAT

Jëwiriñu Njàng mu kawe mi, Gëstu beek Coste gi, dina jël 1 500i jàngalekat ak i gëstukat ci daara yu kawe yi. Xibaar la...

SEN-PNA AK MEDIS S.A BOOLOO NAÑU NGIR LIGGÉEY

SEN-PNA mooy banqaas bi ñu dénk lépp lu aju ci defar, jënd ak séddale garab yees di ci réew mépp. Ci kilifteefu njëwriñu wér-gi-yaram...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (7/8/2025)

NGUUR GI AK “ENTENTE SYTJUST-UNTJ” XAATIM NAÑ AB DÉGGOO Daanaka lu jege ñaari weer walla lu ko ëpp liggéeykati Yoon yaa ngi ci ay ñaxtu....

TUKKIB ELIMAANU JËWRIÑ YI FA TIRKII

Démb, ci yoor-yoor bi, la elimaanu jëwriñ yi, Sëñ Usmaan Sonko, génn réew mi, dem fa Tirkii. Njiitu réew ma, Sëñ Racip Tayyip Erdogan,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (5/8/2025)

ÑAXTU LIGGÉEYKAT YI CI WÀLLU YOON Démb ci altine ji, 4 ut 2025, kurélug layookat yi, di Conseil de l’ordre des Avocats, génne na ab...

NGOMBLAAN GI

Njiitu Ngombaan gi, Allaaji Maalig Njaay, siiwal na ay coppite yu am solo yees namm amal ca Ngomblaan ga. Ci ab lël bu ñu...