Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

BÀJJEN ARAM

La Kocc jàngale woon nga feeñal ci talaata jii « Mag mat naa bàyyi cim réew » Teey, yéwén, ràññee, dogu nga nu won Lii bokk na ci mbindu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (19/8/2025)

FMI YÓNNEE NAY NDAW FI SENEGAAL Ay ndawi FMI (Fond Monétaire International, di kurélug koom-koomu mbootaayi xeet yi) ñëw nañu fi réew mi ngir dox...

CÀMBARUG ÑEENTI SÉMBI SÀRT FA NGOMBLAAN GA

Lu tollu ci weer ak lu teg ginnaaw bi ñu dakkalee seen i càmbar ak tay, dépite yi dooraat nañu seen ub liggéey. Tay,...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA SÀPPOŊ

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jóge na fi tay, ci yoor-yoor bi, wutali Sàppoŋ. Fa lay nekk ba keroog 26eelu bésub...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

BASKET : AFROBASKET 2025 Senegaal dina amal mats jàll (barrage) ëllëg ci altine ji, bu 18i waxtu jotee ci ngoon, moom ak Sudãwu bëj-saalum. FUTBAL : SUPER CUP...

DEXU SENEGAAL GI NAR NAA WALAAT FA MAATAM AK BÀKKEL

Dexu Senegaal gi nar naa walaat fa Maatam ak Bàkkel bu taw bi wéyee di fa sotti ci ñaari fan yii ñu jublu. Xibaar...

WÉERUWAAY

Sunu jenn maam ju mënoon a way ne woon na : “Am kilifaay li am solo. Soo ko amee am nga solo. Soo ko...

MALI : JAPP NAÑU ÑAARI SENERAAL AK BENN SAA-FARÃS

Ci alxamesu démb ji la xibaar bi rot. Sóobare yay jiite réewum Mali jamono jiii ñoo ko fésal. Bees sukkandikoo ci dég-dég (xibaar) yi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (14/8/2025)

LIMU ÑI TEEWE MÀGGALUG TUUBA Démb, ci àllarba ji, lañu doon amal màggalug Tuubaa. Mu nekk ndaje mu réy ci Senegaal. Mbooloo mu takku di...

NJUUX LI : ANACIM A NGI ARTU

Kurél gii dii ANACIM (Agence nationale de l’aviation civile et de la météorologie) mooy saytu lépp lu aju ci njuux li fi réewum Senegaal....

Cang gi Bambaa ko moom !

Cang gi ñuy woote fa Sëriñ Tuubaa lañu koy fekk. Mooy ki jëkk a woote ci ñu xam-xamal wolof, jaare ko digle ñeel ñiy wax...