AccueilTagsDiine

Diine

XALAM NEEXOON NA BA NOPPI…

“Xalam demoon na bay neex, buum ga dog”. Wolof dina faral di wax kàddu...

COKKAASU ODIA

spot_img

WAAJTAAYI MÀGGALUG TUUBAA 2023

Dëkk bu sell bii di Tuubaa sóobu na ci waajtaay yi ñeel màggalug 18...

MÀGGALU DAARU XUDÓOS

Mu doon tur wu siis wi ñu ko xame, màggalu daaru xudóos doon xew-xewu...

TABASKI 2023 : XUTBA SËRIÑ MAAHI ÑAS

Ci alxamesu démb ji la ñu ëpp ci saa-senegaal yi tabaski. Ku ne tabaski,...

TABASKI 2023 : XUTBA SËRIÑ BAABAKAR SI MU DABBAAX (NJOOL-FUUTA)

Ci alxamesu démb ji la ñu ëpp ci saa-senegaal yi tabaski. Ku ne tabaski,...

TABASKI 2023 : XUTBA CEERNO SAYDU NUURU TAAL

Ci alxamesu démb ji la ñu ëpp ci saa-senegaal yi tabaski. Ku ne tabaski,...

“SËRIÑ BI, FÀWW MU FEEÑ”

Bu ñu seetloo fan yee ci ginnaaw, werante amoon na ci nataali Séex Ahmadu...

Latest articles

XALAM NEEXOON NA BA NOPPI…

“Xalam demoon na bay neex, buum ga dog”. Wolof dina faral di wax kàddu...

COKKAASU ODIA

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/2/2025)

NDÉGLUG FARBA NGOM Tay, ci alxames ji la waa PJF (Pool Judiciaire Financier) woolu woon...

SËRIÑ AMDI MÓODU MBENDA FAAL WÀCC NA LIGGÉEY

Sëriñ Amdi Móodu Mbenda Faal, xalifa Baay-Faal yi, wàcc na liggéey. Démb ci àllarba...